Commentaire de LIIROU BAYE DIANKHA CI DUBAI (ISSA GUEYE) (05/08/2007 06:31) :
DIEUREUDIEUFE CHEIKH BAYE DIANKHA ALLAH KOULLI HAL. BOUDOUL WON YAW MA DEE
CI NASOOT. SANT NA LA GEUREUM NA LA BAYE. YAMA NANDAL, YAMA SOUKHAT TABIL
MA CI LEROU MAHRIFATOU BILAHI.
CHEIKH BAYE DIANKHA DOMI BABA,YALLA NAGUA FI YAGUE TA AND AK WEER.
ALLAH BAYE CI KAW LA DIEUM KOUKO WEDI CI SOUF NGAY DESS BA ABADAN DAHIMAN
CHEIKH BAYE DIANKHA GENERALOU NGA, DINAN LA MADIAL LOGNOU WAKH GNOU DEF KO
NGUIR DIEUMI BAYE. BAYE NGA GNOU KHAMAL TA MOUSSOULO GNOU WAN SA BOPA.
magui13issa@yahoo.fr |